watermark logo

ADIOUZA - MONSIEUR BONHEUR (CLIP OFFICIEL)

12 Vues· 10/30/22
Miagueye
Miagueye
3 Abonnés
3
Dans Musique

Après une longue dispute dans le couple, la femme prend l’initiative de se réconcilier avec son homme, son Monsieur bonheur et de faire la paix car ce dernier lui manque énormément .
La paix est la source du bonheur.Sans toi mes jours sont blèmes et le monde vide. Que serai-je sans toi à mes côtés ? Reviens-moi.


Lyrics
Mr Bonheur nexa joubole
Dafa jote nga gneuw gnou waxe
Taye jameu la yewo
Bae sagou bi doyna

ma guiss néne
ni néna ngui
thiapa thioly
do kéne thi gni

lo viser
doko moy
raféte nguémb
meuné beuré souf

Refrain

nonou lalay nammé
*dotou moko def*
Te foma méré ma diakh lé bb
*dotou mako def*
*balma dotou moko def*

yaw xolma tay ré bb
Dotoumako def*
gnou def joboo de l’année bb
Dotoumako deff
*balma dotou moko def*

Couplet 2
dama paré dioubok yaw
ba fofou gnouy wowé wouyaye

oohoo ohoo
khamanté nagne dou ame thiow
oohoo ohoo
diéleu ame foko fogué woul

soukeur bi thi banana
paré noy ni xaale
menthe bi né thi nana
ak yénene yilay xaar
Doyalouma
mére bi doyna
Doyalouma

Refrain

nonou lalay nammé
*dotou moko def*
Te foma méré ma diakh lé bb
*dotou mako def*
*balma dotou moko def*

yaw xolma tay ré bb
Dotoumako def*
gnou def joboo de l’année bb
Dotoumako deff
*balma dotou moko def

Pont
meuno dém kaay ndax yaye sama poumon gauche
Waw Waw Waw Yaw la
meuna fi dé thi une minute de pause
Wallah wallah

am nga thiass stylé nga
mako léteu kaay firiko
diekha goul doya louma
dianteu soow kaay dolima

*doyaaa louma*
a vie lagne signé
*doyaaa louma*

Refrain

nonou lalay nammé
*dotou moko def*
Te foma méré ma diakh lé bb
*dotou mako def*
*balma dotou moko def*

yaw xolma tay ré bb
Dotoumako def*
gnou def joboo de l’année bb
Dotoumako deff
*balma dotou moko def


Weye mbegel manak mbegel

bae tay la tay
bae tay la tay
dara ladoule mayé

Bae taye la taye togale
Bae taye la taye
Dara doumako mayer


bae tay la tay togale
dara ladoul mayé

Beat: Iso
Composition: Adiouza, Iso
Lyrics: kruh
Mix master: Ludovic
Realisateur: Mety-med
Acteur principal: Ansoumana
Coiffure: dija and aisha
Make up: Adja make up
Styliste: Mb haute couture
Assistante: Aminata Ndoye



Remerciement Chez Fatou campement ndangane de Cheikh Ndiaye, Maison la lagune campement Ndangane, imam Diouf île du saloum et le staff.


Abonnez-vous ici : http://bit.ly/AdiouzaDiallo

Retrouvez Adiouza Diallo sur :

- Tik Tok: https://www.tiktok.com/@adiouza7
- Instagram: http://i.instagram.com/adiouza/
- Twitter : https://twitter.com/Adiouzaofficiel
- Facebook: https://web.facebook.com/AdiouzaPageFans/

#Adiouza2022 #MonsieurBonheur #AdiouzaProd

Montre plus

 0 commentaires sort   Trier par