Top videos
N'oubliez pas de vous abonnez a notre chaine Youtube YESDAKAR
Retrouvez - nous sur http://www.yesdakar.com/ ou télécharger l'application sur
- Playstore: https://play.google.com/store/....apps/details?id=com.
Pour suivre toutes vos vidéos préférées :
Abonnez Vous a notre Chaine Youtube https://www.youtube.com/c/Yesdakar
Marímar
Le Corps du Desir
N'oubliez pas de vous abonnez a notre chaine Youtube YESDAKAR
Retrouvez - nous sur http://www.yesdakar.com/ ou télécharger l'application sur
- Playstore: https://play.google.com/store/....apps/details?id=com.
Pour suivre toutes vos vidéos préférées :
Abonnez Vous a notre Chaine Youtube https://www.youtube.com/c/Yesdakar
Viviane chidid confirme sa couronne de reine de la musique sénégalaise avec une entrée explosive
Tome Sawyer
#niani #Gnani #Niaani #Ñaani #Lions #Sénégal #Footbal #FaadaFreddy #ndongod #Daarajfamily #Daaradji #Coupedumonde #Sadiomane #kalidoukoulibaly #Lionsdelateranga
Stream or download Ñaani
👉🏾https://bfan.link/naani
Music by: faada Freddy
Lyrics by: ndongod & Faada Freddy
Recorded and pre- mixed by: Mansour(BBC)
Mixed by: Polerik
Mastering : Chab Mastering
Cover by : P4MP
Animated cover by : Abdoulaye Gning (la Petite Tribu)
Production company: Bois Sakré
---------------------------------------------------------
Daaraj Family On line :
https://www.instagram.com/daarajfam_o...
https://twitter.com/daarajfamily
https://www.facebook.com/daarajfamily...
http://daarajfamily.com/
(c) 2019 Bois Sakré/All Made
ñaani , à l'origine est un chant composé par Samba Coumba kalado Dioum(Gawlo ) compagnon de Lat Dior qui informait ce dernier en chantant " Ñaani bañ naa " le ñaani a refusé leur entrée sur leur territoire.
Aujourd'hui , cet hymne revisité en partie par le Daaraj Family en une version plus moderne. Ce son est dédié à tous les valeureux hommes et femmes du Sénégal notamment les plus grands sportifs de tous les temps pour passer le témoin aux nouvelles générations .
ÑAANI - Daaraj Family Lyrics
Ñaani bañ naa
Ñaani bañ naa
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau)
Ca kaw a kaw
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau)
Ca kaw a kaw
Couplet 1: Ndongo d
Senegaal - ndam rek
2002 wane na yoon wi
Ay champion - Jom rek
Taxaw ci toit bi ci monde bi
Fi la nu tekk sunu bët yi
Jëli Ji Bi médaille
Ci marche bi marche bu njëk bi
Raaya bi ñoy boroom
Ken du ñu tërr ci geew gi
Ken du ñu jiitu ci rëdd bi
Ñu jeggi Record bi
Ni Amadou Dia Ba ci podium bi
Amadou Gackou dëggal ko ni -
Senegal , Palmarés
Amy Mbacké Thiam ne du des
li fond la course ak vitesse
Ñoy chef lii la yalla def -
Dirigé’k doole Double less
Score bi nu yokkati
Def team ni Metsu Bocandé
Mame maty ,Etienne ,Gorgui Dieng
Bideew ci kaw balle bi Bonde
Ñu dundal Compétition bi
Tiene Mental bu Gandee
Refrain :
Ñaani bañ naa , Ñaani bañ naa !!
(Tey la waalo gëna àay danuy bañ ba tay)
Ñaani bañ naa , Ñaani bañ naa !!
(Tey la waalo gëna àay danuy dem ba jeex)
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màgg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau) Ca kaw a kaw
Couplet 2 : Faada Freddy
Duñu nangu Ken di ñu yoxosu
Tay la gaynde gënë wagassu
May leen ñu ndox ñu raxasu
Ndam lañuy yootu ba àgg si
Ñaani bañ a tina bu lepp ne tekk ba arbitre bi sifflé
Nga xam ne lepp dëggla du ñu négocié
Danuy labbali sunu fàs lawal suñ legacy
Buñu tëkku ndax Kersa du ragal
Leeg leeg ñu gennee jiko waga
Kenn duñu Lazer laaj ko Salah
Linu ñakk du fulla du fàyda
Ñoy champion d’Afrique di beaux gosses
Suñu jigeen ñoo leen ëpp cakass
Uppercutu KO la du pés
Duñu leen may dara du mbaquus
Bu doyul ñu Dolli ci nokoss
Boy woote malade ñun la Ñagass
Xeff xippi ñu defal la bagaas
Dañu dogu tay lañ gënë focus
Refrain :
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màgg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau)
Ca kaw a kaw
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màgg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau)
Ca kaw a kaw
Couplet chant : Faada Freddy
Fii ñoo ko moom ndam li ñoy boroom
Du ñu sen moroom ay Gaynde njaay la ñu
Alaa àccu du nu sònn du nu tàyyee
Fii de ñoo ko moomee ndam lii ñoy boroom
Du ñu seen moroom ay Gaynde njaay la ñu
Alaa àccu du nu sònn du nu tàyyi
Refrain:
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màgg ak ndaw ( ñaani bañ naa ñaani bañ naa)
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau)
Ca kaw a kaw
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw ( dandy bañ ba tay )
Muy Goor ak Jigeen Màgg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo (drapeau)
Ca kaw a kaw ( tay la waalo gëna àay da nuy đem ba jeex )
📱 +221 78 011 32 22 ☎️ +221 33 888 68 29
Email : [email protected]
Site Web : www.daarakawthar.com
Adresse : 2 Cité Sogabeg Tivaoune Peulh
Baye Guinar
alerte dun patriote Toucouleur casacais
Thiapathioly
crise berlin paris
Marímar
par senetube
Suivez le journal de Sud Fm, la Revue de Presse.
Ne Ratez pas Ndeki li, le journal de la coupe du monde, al Kitab, Objection, Wakhtanou Fadiar
Visitez notre Page Facebook https://web.facebook.com/Senradiosud/
Notre Site web https://sudfmsenradio.com/
Suivez le journal de Sud Fm, la Revue de Presse.
Ne Ratez pas Ndeki li, al Kitab, Objection, Wakhtanou Fadiar et d'autres émissions
#sudfm #radio #actualité
baye guinar
Tome Sawyer
Tome Sawyer
L'INTROVIEW - Se Poser Les Bonnes Questions🧠
Invité : Ahmed Khalifa NIASSE, Chef Religieux - Homme Politique
11:02 - Question n°1 : Quelles sont les 3 principales critiques que vous avez toujours voulu éviter à votre endroit et qui vous ont poussé à vous dépasser depuis votre jeunesse jusqu'à nos jours ?
30:16 - Question n°2 : De quel Sénégal rêvez-vous ?
49:05 - Question n°3 : Quel serait, selon vous, le scénario catastrophe pour l'avenir du Sénégal ?
59:26 - Question n°4 : Quelles ont été vos relations avec les différents présidents du Sénégal et avec les membres de l'opposition, aussi bien dans le passé et dans le présent ?
1:17:00 - Question n°5 : Pourquoi n'avez-vous jamais voulu être candidat à l'élection présidentielle ?
1:25:27 - Question n°6 : Il y a plusieurs supputations sur l'origine de votre fortune… Quels éclairages pouvez-vous nous donner à ce sujet ?
1:33:56 - Question n°7 : Ceux qui vous connaissent vous présentent comme un père de famille responsable et bienveillant… Pensez-vous à vous retirer de la scène publique et médiatique en passant le flambeau à vos enfants ?
Crédits : PPS the Writah - Amosa (Prod Kayeed), Album : Bés Bu Bees
#politique #senegal #actualités
Marímar